“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob
décembre 25, 2025
0 Comments
Lire plus
ÑAAREELU XAAJ
Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit, loolu ciy wax rekk la yem ; ndax Seŋoor àndul woon ci réew mi génn ci nooteel ci saa si. Li mu
BOO BAÑEE ÑAAW…
Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy wax ? Nga tontu ne :Boo bañee ñaaw de, xanaa dangay dëkkee toppatoo sag xar-kanam rekk, ak a sañse.Boo noppee tuuti,
