Seex

Mooy góorMoo di as gorMbokk ya ko worÑooy mbokk ya nu lorNuy leb ba fees ak i borSànni xam sëgg ci fen di forNdax kat xam-xamam…

Categories: FÀTTALIKU DÉMB, XIBAAR

ÑAAREELU XAAJ

Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit, loolu ciy wax rekk la yem ; ndax Seŋoor àndul woon ci réew mi génn ci nooteel ci…

Categories: FÀTTALIKU DÉMB, XIBAAR

Njiitu Réew

Dangaa jiitoomDañu la jiitalSa jubb cunduŋ xanaa taxulMoo ndax doo tontoomCéy lii ciy way-xëccooKu ne samp ndëndNaan awma ci moroomBoppu réew ak ni mu diiseDungeen nu…