Fonk sunuy làmmiñ ag kurél la gu ëmb ay jigéen ak i góor yuy yëngu ci saytu ak jubal làmmiñi réew mi.~~ Mu ngi soqeekoo ci njàngalem ijji mu nu defoon ci iniwersite ci atum 2020.~~
Kurél la guy liggéey ngir jëmmal, taaral làmmiñi réew mi, fexe lammiñ yooyule di amal njariñ askan wi ci lépp lu muy yëngatu, ba mën a indi naataange ci réew mi.
Sas woowu nag, nu fas yéene jaare ko ci ñetti fànn yii :
- jàngale mbind ci làmmiñi réew mi, jëkke ko ci wolof tudde ko Àllarbay làkki réew mi
- Ànd Jubbanti mbind mi Wone ak waxtaane téere yi Gēstu ak Siiwal :
Jàngale mbind mi - wone ak waxtaane téere ci ñu bind ci làmmiñi réew: Péncum Maam Yunus Jeŋ
En françcais
Fonk Sunuy Làmmiñ est un regroupement de femmes et d’hommes, militants pour les langues nationales, qui œuvrent pour une véritable promotion de nos langues en tant que vecteurs de la culture nationale, moyens de production et de transmission de savoirs, mais également en tant qu’outils de travail, et donc comme instruments par excellence de développement.
Les objectifs du groupe sont d’aider à l’alphabétisation gratuite (à la fois en présentiel et en ligne), actuellement en wolof et, à terme, dans les autres langues nationales ; de veiller à ce que ces langues soient correctement transcrites dans les médias et sur tous les supports de communication écrite ; et aussi de promouvoir la littérature produite dans nos langues.
Fonk Sunuy Lammiñ concentre ses activités autour de trois axes principaux :
- L’enseignement : Àllarbaay làkki réew mi,
- La correction de la graphie dans l’espace public : Jàngale mbind mi,
- Les rencontres littéraires : Péncum Maam Yunus Jeŋ,
- Recherche et vulgarisation.
