Li ko tax a jóg mooy jubbanti mbind mi ci tele yi ak ci mbedd mi. Li ñu ci jublu mooy nit ñi mën cee sukkandiku ba mbindum làmmiñi réew mi jaar yoon te nu ñaax leen ngir ñu gën a sàmm sunu moomeelug làkk ak aada.

Fonk sunuy làmmiñ ag kurél la gu ëmb ay jigéen ak i góor yuy yëngu ci saytu ak jubal làmmiñi réew mi.~~ Mu ngi soqeekoo ci njàngalem ijji mu nu defoon ci iniwersite ci atum 2020.~~
Kurél la guy liggéey ngir jëmmal, taaral làmmiñi réew mi, fexe lammiñ yooyule di amal njariñ askan wi ci lépp lu muy yëngatu, ba mën a indi naataange ci réew mi.
Maakaanu kureel gi : Amitié 2, 4251, Dakar
Bunmi jokkoo yi : 776420294, 774536463, 776377873