Njiitu Réew
Dangaa jiitoomDañu la jiitalSa jubb cunduŋ xanaa taxulMoo ndax doo tontoomCéy lii ciy way-xëccooKu ne samp ndëndNaan awma ci moroomBoppu réew ak ni mu diiseDungeen […]
Read More →Dangaa jiitoomDañu la jiitalSa jubb cunduŋ xanaa taxulMoo ndax doo tontoomCéy lii ciy way-xëccooKu ne samp ndëndNaan awma ci moroomBoppu réew ak ni mu diiseDungeen […]
Read More →Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy wax ? Nga tontu ne :Boo bañee ñaaw de, xanaa dangay dëkkee toppatoo sag xar-kanam rekk, […]
Read More →Fonk sunuy làmmiñ ag kurél la gu ëmb ay jigéen ak i góor yuy yëngu ci saytu ak jubal làmmiñi réew mi.~~ Mu ngi soqeekoo ci njàngalem ijji mu nu defoon ci iniwersite ci atum 2020.~~
Kurél la guy liggéey ngir jëmmal, taaral làmmiñi réew mi, fexe lammiñ yooyule di amal njariñ askan wi ci lépp lu muy yëngatu, ba mën a indi naataange ci réew mi.
Maakaanu kureel gi : Amitié 2, 4251, Dakar
Bunmi jokkoo yi : 776420294, 774536463, 776377873
