Skip to content
Fonk Sunuy Làmmiñ

Fonk Sunuy Làmmiñ

Participer
  • Accueil
  • Fonk sunuy làmmiñ
    • Àllarbaay làkki réew mi
      • L’enseignement
    • Jàngale mbind m
      • La correction de la graphie dans l’espace public
    • Péncum maam yunus jeŋ
      • Lesrencontres Littéraires : Pécum maam yunus jeŋ
  • Xibaar
    • Fàttaliku Démb
    • Magu waxoon naa ko
    • Waxleen seen xalaat
    • Gëstu ak siiwal ci kuréel yiy doxal
  • Média
    • Album
    • Vidéos
  • Jokkoo ci

Mois : décembre 2025

Seex

décembre 25, 2025
 |  Aucun commentaire
 |  FÀTTALIKU DÉMB, XIBAAR

Mooy góorMoo di as gorMbokk ya ko worÑooy mbokk ya nu lorNuy leb ba fees ak i borSànni xam sëgg ci fen di forNdax kat […]

Read More →

ÑAAREELU XAAJ

 |  Aucun commentaire
 |  FÀTTALIKU DÉMB, XIBAAR

Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit, loolu ciy wax rekk la yem ; ndax Seŋoor àndul woon ci réew mi génn ci nooteel […]

Read More →

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

 |  Aucun commentaire
 |  MAGU WAXOON NAA KO, XIBAAR
Read More →

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

 |  Aucun commentaire
 |  MAGU WAXOON NAA KO, XIBAAR

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko gën. Njub, jom, fulla, fayda, ngor, fit, worma, kersa añs., ñoo di jikko yoy, mépp réew […]

Read More →

Njiitu Réew

 |  Aucun commentaire
 |  WAXLEEN SEEN XALAAT, XIBAAR

Dangaa jiitoomDañu la jiitalSa jubb cunduŋ xanaa taxulMoo ndax doo tontoomCéy lii ciy way-xëccooKu ne samp ndëndNaan awma ci moroomBoppu réew ak ni mu diiseDungeen […]

Read More →

BOO BAÑEE ÑAAW…

 |  Aucun commentaire
 |  WAXLEEN SEEN XALAAT, XIBAAR

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy wax ? Nga tontu ne :Boo bañee ñaaw de, xanaa dangay dëkkee toppatoo sag xar-kanam rekk, […]

Read More →

Category

  • FÀTTALIKU DÉMB
  • MAGU WAXOON NAA KO
  • WAXLEEN SEEN XALAAT
  • XIBAAR

Archives

  • mai 2026
  • décembre 2025

Meta

  • Connexion

Fonk sunuy làmmiñ ag kurél la gu ëmb ay jigéen ak i góor yuy yëngu ci saytu ak jubal làmmiñi réew mi.~~ Mu ngi soqeekoo ci njàngalem ijji mu nu defoon ci iniwersite ci atum 2020.~~

Kurél la guy liggéey ngir jëmmal, taaral làmmiñi réew mi, fexe lammiñ yooyule di amal njariñ askan wi ci lépp lu muy yëngatu, ba mën a indi naataange ci réew mi.

Fonk Sunuy Làmmiñ
  • ÀLLARBAAY LÀKKI RÉEW MI
  • Jàngale mbind mi
  • PÉNCUM MAAM YUNUS JEŊ

Jokkoo ci


Maakaanu kureel gi
: Amitié 2, 4251, Dakar

Bunmi jokkoo yi : 776420294, 774536463, 776377873

Topp ñu ci Gēstû ak Siiwal

  • Facebook
  • X
  • LinkedIn
  • Instagram
Fonk Sunuy Làmmiñ Theme By SKT Activism Lite